Serigne waxtaan wu am solo lool ci Al Muhtamaa, Sallal aahu halayhi wa sallama
matt naa teewlu lool, ta jeem sunu kemm kattan ci di jeema xeex ak sunu bakkan di jefe ay njangaleem ta yalla rek tax. Dax kat njarin li ci lolu kepp la nekk
waxtaan wu mata diglu ay yonn-i yoon
diglu ko ci soo amee ak yaatou ngir mana tewwlu limouy wax ak tontu yimuy andi ci laaj yu am solo yi
diglou ko ci waxtu woo amee ak yatou ngir mana jel ay bind ci yennati wax yi ndax yombuta jang ciy teere
waxtaan wu mata teewlu
waxtaan wu am solo lool sax
Sira + questions réponses
sira + questions réponses