Ci limat bu njëkk bii, Thierno Alassane Sall mu ngi saytu, di wax lu waral Senegaal moom boppam lu mat, ci atum ren, juróom-benn-fukk-ak-benn at, te ba leegi réew maa ngi tumrankee. Mu ngi ut itam ay pexe ngir kàttanal ndaw yi, ñu toog seen réew fekk fi jàmm ak naataange.
Show more...