Woor weeru koor te Yalla rek tax.
Waxtaane lenn ci njariñu noppi
Waxtaanu Serigne Sam Mbaye ci kan moy Cheikh Ahmadou Bamba Khadimu Rassul.
Khutbah Serigne Ahmad Rafahi Mbacke Ibn Serigne Fallou ci julli fajar.
Waxtaanu Serigne Sam Mbaye ci Al Qur'an ak diganté Serigne Touba ak Al Qur'an.
Waxtaanu Serigne Sam Mbaye ci akhiru zaman (mujjuk jamono).
Waxtaanu Serigne Sam Mbaye ci akhi dieukeur ak diabar.
Litakh Yalla bind ñu.
Lan moy deuggi deuggi Hajj ak litax jullit bi warko def ak nimukoy defe.
Li beep jullit wara jangé ci woor weru koor gi bamu jeex.
Lan moy Murum Koor, manam Zakatul Fitr, ak kan moko wara joxé, naka lankoy joxé, ak kañ lañ ko wara joxé ak kan ngako wara jox.
Naka la jullit bi mana def ba japp diinem ak mucc ci yaxu yaxu aduna bi.
Waxtaan wi Serigne Touba mujjé def, ci kadduk Serigne Cheikh Fat Tacko Diop (nijaayu Serigne Mourtada).
Waxtaanu Serigne Abdul Ahad Mbacke Ibn Khadimu Rassul ci litax nitt ku nek war di sant ak fattaliku Yalla Sunu Borom.
Litakh ku nek ci ñun wara gorgorlu ci top ndigalu Yalla yi.
Lewet ak saye mbokk jullit ak nit ñi.
Li nek ci wakh ak limu mana yakh walla defar, ak li waral noppi ci yenn yi di bakh.