Ñu baax ñii ku leen woy da ngay am ngërëm
Yonnen doomi yonnen Bilaay ñeey ngalam
Limamook njaboot am da ñoo jàlla yii
Yonnen daal dadul kem, xana ñooy ngalam
#Layenedigital #layene #zikr