Suniouy wakh si migration fi sénégal, liniouy geuneu xalaat moy ay ndaw you goor yuy dieul gaal nguir dem Espagne. Wayé daniouy faté ni si biir tukki katt yoyou amna ay jiguén.
All content for Jiggéen yuy tukki : Dakaar ba fépp ci àdduna is the property of Studio Ëpoukay and is served directly from their servers
with no modification, redirects, or rehosting. The podcast is not affiliated with or endorsed by Podjoint in any way.
Suniouy wakh si migration fi sénégal, liniouy geuneu xalaat moy ay ndaw you goor yuy dieul gaal nguir dem Espagne. Wayé daniouy faté ni si biir tukki katt yoyou amna ay jiguén.
Niétélou épisode bi si diourom niari épisodou serie « Jiggéen yuy tukki : Dakaar ba fépp ci àdduna » gniko realisé di Ibrahima Diouf ak Clair Rivière bou studio Ëpoukay.